@baracres.871: 1. ✨ Mané Ngor ak Djom rk lay guisse beugue. Tekki fess si yéŋ ✊ 2. ✨ Tetesse gui né kou Yayam yakaar waroul Dead si guédj ❌ 3. ✨ Yén guéstou lén khole lén Niatta nitte ta dead si yén 💔 4. ✨ Beugue téral yaye, Yaye yangui dioy rk diakki seunguéme 😭 5. ✨ Guédje gui amoul Bankasse mais amna Rap ak Djinné 🧞‍♂️ 6. ✨ Wakh djodiou sakh dou am sens ndakh khamni ragalolén 😔 7. ✨ Touki takhouta tékki, Té beugue tékki téré woule tokk 🙏 8. ✨ Niou tatane tagatate touti khél yi tarou teulé wougn ko 🧠 9. ✨ Dieulén Bagages yi niou deupou Yallah y'en a, Yalla bakhna ☝️ 10. ✨ Yalla ngi fépp lépam djamme la ❤️ 11. ✨ Té After lolou dina youkhou ba ngourr gui dégue niou 👂 12. ✨ Gni dead si guéthie gui laye dialé sén mbokk magui diéguelou 🙏 #fyp #vidéo #jeveuxpercer

BARA
BARA
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 23 October 2026 19:07:19 GMT
191
43
2
0

Music

Download

Comments

alhamdu_for_all_time
𝑀𝑎𝑠𝑠_𝐶𝑜𝑙𝑑_𝐵𝑜𝑦🤴💖 :
🥰🥰🥰
2026-10-24 15:34:18
1
To see more videos from user @baracres.871, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About